alfaDF9/whisper-small-wolof-v2
Automatic Speech Recognition
•
Updated
•
78
text
stringlengths 1
2.33k
| duration
float64 0.5
193
| file_name
stringlengths 8
31
| path
stringlengths 14
39
| audio
audioduration (s) 0.5
193
|
---|---|---|---|---|
nuyu naa ko | 0.676 | wol_44012_1189.296_1189.972.wav | kallama/wol_44012_1189.296_1189.972.wav | |
pour chaine feebar yooyu noonu dagg | 1.539 | wol_43810_921.351_922.89.wav | kallama/wol_43810_921.351_922.89.wav | |
le 26 juin la tawoon | 1.252 | wol_4210_1934.019_1935.271.wav | kallama/wol_4210_1934.019_1935.271.wav | |
waaw c' est bien ci wàllu agriculture aussi | 4.38 | wol_31212_134.61_138.99.wav | kallama/wol_31212_134.61_138.99.wav | |
yéen jigéen ñi bu ngeen dee ligéey benn mbir | 2.12 | wol_4613_477.503_479.623.wav | kallama/wol_4613_477.503_479.623.wav | |
donc mais nag %e par rapport ak collectivité territoriales ak ni ñu xamee les réformes bi am léegi | 6.815 | wol_44811_1667.027_1673.842.wav | kallama/wol_44811_1667.027_1673.842.wav | |
waaw partiquement fu ñuy fu ñuy traité moom bu ñu fa jaaree benn yoon | 4.21 | wol_4410_1265.122_1269.332.wav | kallama/wol_4410_1265.122_1269.332.wav | |
déroulé gu ñu ko parce que ñun étape par étape lañuy def | 3.486 | wol_44812_1377.738_1381.224.wav | kallama/wol_44812_1377.738_1381.224.wav | |
en vu de la prochaine campagne | 1.379 | wol_43810_429.193_430.572.wav | kallama/wol_43810_429.193_430.572.wav | |
mën nañoo uute ci xalaat | 1.18 | wol_44412_187.991_189.171.wav | kallama/wol_44412_187.991_189.171.wav | |
waaw am ci ñoo xam ne nag dañoo mujj sax far gas ontat ko dem jaay ko situation boobu ñàkk préparation la ndax ëllëg waaye aussi au delç de de de de de soppi mbéyin bi tamit est ce que tamit laajut ñu gën a xoolaat beneen doxalin boo xam ne ñun béykat yi danañ ko def pour que situation ñu bañ si tabbi ëllëg | 15.745 | wol_44412_821.964_837.709.wav | kallama/wol_44412_821.964_837.709.wav | |
donc %e buñu sañoon nag rapports yooyu heure buñu ko yónnee | 3.193 | wol_35311_554.706_557.899.wav | kallama/wol_35311_554.706_557.899.wav | |
Suñ jàllee ca nataalu fanweee...euh...ñeen-fukk ak juróom-ñett, ñooŋ fay gis ay saaku. Saaku bii def kaani, kaani, bii mu nga def daqaar, bii mu nga def paañ, bii mu nga def poobar, euh...yi mu nga def yeneen ak yeneen ak yeneen, bii mu nga def bisaab. Moom nag, euh...yu bari day dem ci togg comme kaani. Kaani, dina dem ci ceebu jën, dina neexal ceebu jën lool. Buñ demee jël daqaar, daqaar tamit dina neexal maccaat, maccaat, loolu dina ci am solo lool. Buñ demee itamit bisaab, bisaab dina dimbali nit ñi, ñu mën cee defar di naan tamit di ci faj ay seen i jàngoro, walla suñ wooree ba ngoon di ci naan, di ci noos ak yeneen i yeneen. Poobar tamit, mën du jariñ, day dem ci togg, lu am solo la. | 61.597813 | 2829:434.wav | waxal/2829:434.wav | |
boo bëggee dab si UGPM tamit foog ñu fexe ba xamanteeg yow mooy benn temps d' observation boo xamante ni dañuy ñëw di waxtaan ak yow ci sa biir dëkk di waxtaan ak mbooloo ma mais ngay ñëw tamit di fekkee suñuy ndaje ak suñuy waxtaan di ca dem | 12.435 | wol_44912_295.294_307.729.wav | kallama/wol_44912_295.294_307.729.wav | |
waaw mais loolu yëpp nag %e béy jamono jii amul benn activité génératrice de revenues boo xamante ne muy mbay di sàmm di napp boo xam ni mën na dem sans météo parce que li nga ci yaakaar nii tey suba gànnaaw sub mën na ba leneen bañ a nekk | 15.531 | wol_44011_1742.914_1758.445.wav | kallama/wol_44011_1742.914_1758.445.wav | |
lu tax semence certifiée lu ko waral lu tax lu indi li ñuy def semence certifiée | 3.459 | wol_43920_358.615_362.074.wav | kallama/wol_43920_358.615_362.074.wav | |
ay barab yoo xam ne day taw tuuti | 2.458 | wol_44111_353.775_356.233.wav | kallama/wol_44111_353.775_356.233.wav | |
war koo war ko stocké teglante ko naka lañ ko war a defee si suuf dañoo war a def poudre wala naka la | 4.79 | wol_43312_971.996_976.786.wav | kallama/wol_43312_971.996_976.786.wav | |
wallaahi | 0.684 | wol_45412_350.248_350.932.wav | kallama/wol_45412_350.248_350.932.wav | |
waaye nag am nañ matuwaay boo xam ne suñu xalaat kenn mënu ñu ko teree wax | 4.179 | wol_44411_2027.869_2032.048.wav | kallama/wol_44411_2027.869_2032.048.wav | |
voilà di fàttali mbokki auditeurs yi que ne ñoom it mën nañoo woote ci 33 967 43 00 | 6.188 | wol_4311_489.642_495.83.wav | kallama/wol_4311_489.642_495.83.wav | |
gën leen a gunge | 0.833 | wol_43512_1869.226_1870.059.wav | kallama/wol_43512_1869.226_1870.059.wav | |
yow sa sa numéro téléphone naka la | 1.916 | wol_44012_1151.41_1153.326.wav | kallama/wol_44012_1151.41_1153.326.wav | |
%e beneen bi ci des mooy lu mel ne que comme li mu wax ni %e jël benn stratégie marketing bu bu wér te kooku ñu ngi ciy liggéey incha alla | 8.4 | wol_4613_350.21_358.61.wav | kallama/wol_4613_350.21_358.61.wav | |
na ñuy gën a seetle na ñuy gën a vérifié liste yi su amee genre erreur yooyu ñu xool nan la ñuy def pouir remplacer leen | 7.821 | wol_43511_1370.466_1378.287.wav | kallama/wol_43511_1370.466_1378.287.wav | |
doo xam kii feebar na kii feebarul na nga mar naan rek su may dem tànq ndox naan dem naa sama yoon | 6.647 | wol_43910_1561.786_1568.433.wav | kallama/wol_43910_1561.786_1568.433.wav | |
Thierno Camara %e kon nag %e monsieur Tall waxtu baa ngi ñuy dab | 41.354 | wol_44114_646.785_688.139.wav | kallama/wol_44114_646.785_688.139.wav | |
waaw xam nga tey boo xoolee presque dañ ne ñun Saloum fii ñun baykat fii presque engrais buñ koy utiliser | 8.766 | wol_43411_1444.205_1452.971.wav | kallama/wol_43411_1444.205_1452.971.wav | |
%hum kon nag %e yow yaay maanaam ki nga xam ne moo fi toogal ANACIM noonu la ci mboolem diwaan Tambacounda noonu la | 6.881 | wol_43611_231.164_238.045.wav | kallama/wol_43611_231.164_238.045.wav | |
ba góob | 0.559 | wol_44122_362.74_363.299.wav | kallama/wol_44122_362.74_363.299.wav | |
day mën a yem foofu rek mu nekk verre mu xool yëf yi rafet bien am ku fa nekk di jaay bu ko defee mu daal di waxaale foofu daal di fay jëndee | 6.94 | wol_4613_116.384_123.324.wav | kallama/wol_4613_116.384_123.324.wav | |
%e nga baal ma ci terme | 1.464 | wol_45411_393.871_395.335.wav | kallama/wol_45411_393.871_395.335.wav | |
jërëjëf merci beaucoup ah | 1.049 | wol_4910_703.375_704.424.wav | kallama/wol_4910_703.375_704.424.wav | |
RTS Tambacounda ah waaw dem na waaw xam naa dina ñëwaat 33 981 29 31 waaw monsieur Tall | 7.348 | wol_44113_407.017_414.365.wav | kallama/wol_44113_407.017_414.365.wav | |
7 8 9% %hum léegi nag kee itam bu ko jëlee bëgg ci teg ay commissions !fra am ak ay nangam nangam fokk mu dem 15 jàpp 18 wala 13 jàpp 14 bu fekkee ne Etat bi Etat bi jàppu ci | 11.592 | wol_4814_113.187_124.779.wav | kallama/wol_4814_113.187_124.779.wav | |
loolu tamit %e am na solo léegi nag %e sax bi ci jëmi boppam wax nga ni nga xam noonu lay def %e gàncax gi wax nga ñu tamit période yi nga xamante ne ci la sax bi di di di di di génn léegi nag loolu lépp nag buñ ko xamee xam nañu kañ lay sax biy génn xam nañu ni muy def gàncax gi léegi nag béykat bi nan la war a mun a def ngir moytu sax boobu | 18.486 | wol_4410_370.464_388.95.wav | kallama/wol_4410_370.464_388.95.wav | |
Lii day wane ay policier yoo xam ne dañoo taxaw ci ginnaaw benn barrière ngir di am lu ñuy feg, walla ñuy protéger seen bopp. | 12.517813 | 3556:1296.wav | waxal/3556:1296.wav | |
te fi mu toll nii presque ñëpp a yor téléphone | 1.881 | wol_44012_596.481_598.362.wav | kallama/wol_44012_596.481_598.362.wav | |
ndax bu fekkee wutal nañu la ab foos boo xam ne danga caa war a def lépp loo xam ne mooy mbalitu kër gi | 3.438 | wol_4314_291.105_294.543.wav | kallama/wol_4314_291.105_294.543.wav | |
dafa am fànn ñoo xam nag ñoom force ñoom ñu ñëw laajte ma mooy ñi nga xamante ni ñoom dañoo seen loxo dafa dugg ci coopérative bii ñuy def %e production semence | 9.308 | wol_55010_250.644_259.952.wav | kallama/wol_55010_250.644_259.952.wav | |
parce que xam nga %e au niveau des communes am na %e lu ñuy wax conseil local de la jeunesse | 5.233 | wol_44812_902.239_907.472.wav | kallama/wol_44812_902.239_907.472.wav | |
bu dee si wàllu jigén ñi ñaari mbir gis naa ko ci | 2.562 | wol_44915_331.97_334.532.wav | kallama/wol_44915_331.97_334.532.wav | |
jigéen ñee ëppale góor ñi | 0.771 | wol_4311_430.965_431.736.wav | kallama/wol_4311_430.965_431.736.wav | |
moom bi muy gis | 1.068 | wol_45412_387.868_388.936.wav | kallama/wol_45412_387.868_388.936.wav | |
Maa ngi gis ay xob yu ñu teg. | 2.837813 | 2919:28.wav | waxal/2919:28.wav | |
fukki jeunes | 2.577 | wol_44812_554.195_556.772.wav | kallama/wol_44812_554.195_556.772.wav | |
2000 la ñu crée %e CREC bi | 3.257 | wol_44913_765.172_768.429.wav | kallama/wol_44913_765.172_768.429.wav | |
donc kon producteur bi ci boppam moom war naa bàyyi xel ni | 3.167 | wol_44311_446.844_450.011.wav | kallama/wol_44311_446.844_450.011.wav | |
daanaka énetti téeméer nga koy fay | 2.26 | wol_44411_744.364_746.624.wav | kallama/wol_44411_744.364_746.624.wav | |
ñaar moo ciy am rek | 0.923 | wol_44411_939.996_940.919.wav | kallama/wol_44411_939.996_940.919.wav | |
lu mat ay cinq tonnes wala dix tonnes | 2.151 | wol_44312_492.475_494.626.wav | kallama/wol_44312_492.475_494.626.wav | |
parce ;fra que baaxul nga ñëw dégg ni taw na rek taw na rek nga dem ji | 5.553 | wol_42512_748.899_754.452.wav | kallama/wol_42512_748.899_754.452.wav | |
parce que ñu gën a bëri nekk nañu ay béykat mais ñu ngi pratiquement à trente kilomètres ñu mel ni comme Patacourou ay Julti dañoo nekk béykat yu yu mag mais nag yàlla dafa def par rapport ak li ISRA soxla ak recherche bi niñ ko soxlaa dañoo soxla lu jege nga xam ne boo jógee fii tag nga mun a dem foofu automatiquement nga mun a bu fekkente ne ay attaques la nga mun a jël ay décisions | 21.813 | wol_41940_1345.727_1367.54.wav | kallama/wol_41940_1345.727_1367.54.wav | |
doom ji moom mooy gàncax bi lépp lu nga xamante ni %e doom ji mi ngi koy soxla pour nàmp ci yaay ji la koy jëlee léegi bu dee yaay jooju moom mi ngi ànd ak wér %e ànd naag wér day mën a nàmpal doomam bu baax te du am benn gàllankoor mais bu dee yaay ji dafa manqué par exemple soow | 21.18 | wol_4210_382.013_403.193.wav | kallama/wol_4210_382.013_403.193.wav | |
maa ngi lay fay Serigne | 1.206 | wol_35312_676.023_677.229.wav | kallama/wol_35312_676.023_677.229.wav | |
%e les mercredis là quelque fois ñu def émission toog nit ñi di woote même avant loolu ñu annoncé liñ bëgg a waxtaane nit ñi di envoyé ay messages am ay laaj loolu dara gënu ko | 9.746 | wol_42412_724.865_734.611.wav | kallama/wol_42412_724.865_734.611.wav | |
huit pour cent | 0.572 | wol_4910_1174.302_1174.874.wav | kallama/wol_4910_1174.302_1174.874.wav | |
ba pare mbéy benn genre mbéyteef boo xamante ni da ngay mën a sakkanal ndox mi ndox mi bu ñëwee dafay taaju | 6.009 | wol_45512_227.567_233.576.wav | kallama/wol_45512_227.567_233.576.wav | |
mooy que ñun au niveau de la météo là au delà des prévisions yi ñuy def xam nga dañuy am %e ay services yi nga xamante ne bii dañuy def ce qu' on appelle l' agrométéorologie | 8.173 | wol_44512_856.187_864.36.wav | kallama/wol_44512_856.187_864.36.wav | |
kon defe naa mbokk mi dégg nga li li sëñ bi wax %e maa ngi doon wax sànq ne taal ay taal yi ñuy def ci %e àll bi maanaam ci tool yi %e loolu rey na suuf si wala dundalaat na suuf si wala am na li muy dese ci suuf si | 13.372 | wol_44312_693.263_706.635.wav | kallama/wol_44312_693.263_706.635.wav | |
pour mën a ñëpp xam ko | 0.977 | wol_45411_1702.503_1703.48.wav | kallama/wol_45411_1702.503_1703.48.wav | |
mais tey fi ma doon ñëw mooy ñi nga xamante ne ni ñoom ñooy béykat yi des fois nga dégg ñu ni la ah coppiteg jaww ji lii la ay wax yuñ fi teg laag yooyu ndax loolu mën na am ay yenn risques yoo xamante ne ni ñoom dinañ dinañ dina dina dina dina ñëw ci seen liggéey | 15.532 | wol_43010_1024.944_1040.476.wav | kallama/wol_43010_1024.944_1040.476.wav | |
maanaam boo jëloon tooyaay bi tooyaayu gàncax boobu bu dee téeméer la ñaar fukk yi wala ñaar fukk yeeg juróom la dese ci tooyaay mais boobu day fekk nag mu ngi taxaw si gattax loolu it jéego la ci ñaareelu jéego bi mooy su ma ñëwee nag ba nga xam ne ne góob naa yett naa sama ceeb wala góob naa suma dugub du ma xëy rek jël ko teg ko dem ne maa ngay uti | 28.21 | wol_43411_295.414_323.624.wav | kallama/wol_43411_295.414_323.624.wav | |
engrais du dafay bëri | 1.013 | wol_43011_1201.169_1202.182.wav | kallama/wol_43011_1201.169_1202.182.wav | |
waa talaata gii | 1.228 | wol_44811_1261.325_1262.553.wav | kallama/wol_44811_1261.325_1262.553.wav | |
te it wax dëgg yàlla jumtukaay yu bëree bëri DPV ñu ngi koy mobilisé | 3.762 | wol_4410_2088.079_2091.841.wav | kallama/wol_4410_2088.079_2091.841.wav | |
ci région Tamba ak région Kolda | 2.607 | wol_44122_1501.012_1503.619.wav | kallama/wol_44122_1501.012_1503.619.wav | |
parce que xam nga ne béykat léegi souvent dañuy dem au au au au niveau des banques surtout banque agricole ñu dem leb fa xaalis pour mën a am intrant mën a am matériel agricoles bu tawul naka la ñu mën a def ba am si assurance agricole boobu | 11.721 | wol_43511_726.177_737.898.wav | kallama/wol_43511_726.177_737.898.wav | |
ñun dañ lay fay | 0.706 | wol_4910_2267.638_2268.344.wav | kallama/wol_4910_2267.638_2268.344.wav | |
ñeenti at | 0.85 | wol_4210_1790.623_1791.473.wav | kallama/wol_4210_1790.623_1791.473.wav | |
jàppal ne député àll bi nga | 2.002 | wol_44411_1216.136_1218.138.wav | kallama/wol_44411_1216.136_1218.138.wav | |
parce que su tawee dafa war a am li ñuy wax répartition et répartition boobu nag moom moo ëpp solo sax si nawet que quantité ndox mi lu muy bëri | 9.514 | wol_42811_470.257_479.771.wav | kallama/wol_42811_470.257_479.771.wav | |
trente neuf am nañ ko | 0.687 | wol_4712_120.851_121.538.wav | kallama/wol_4712_120.851_121.538.wav | |
man la Diakhou | 0.796 | wol_44412_754.803_755.599.wav | kallama/wol_44412_754.803_755.599.wav | |
%e def na déclaration de culture | 2.381 | wol_4711_590.961_593.342.wav | kallama/wol_4711_590.961_593.342.wav | |
mooy combus() combus() combustible yi | 1.945 | wol_42931_1370.77_1372.715.wav | kallama/wol_42931_1370.77_1372.715.wav | |
waaw Lour Escale mu ngi am 252 viorgule 8 en 14 jours situation bi dafa normale diggudóomu Missira Wadeen ñu am 239 virgule 1 milimètre en 16 jours donc foofu tamit situation bi dafa dafa dafa diggudóomu ndox mi daa diggudóomu | 13.932 | wol_42514_1066.489_1080.421.wav | kallama/wol_42514_1066.489_1080.421.wav | |
yow nga xamne li ngay togg mi ngi ñor sa compost mi ngi ñor | 2.609 | wol_4210_1519.209_1521.818.wav | kallama/wol_4210_1519.209_1521.818.wav | |
loolu xam nga bu tawee | 1.065 | wol_42922_107.052_108.117.wav | kallama/wol_42922_107.052_108.117.wav | |
kon loolu dafa am njëriñ gis nga maçon bi moom xam na ne ci wàllu béy laay yëngu daf may oo yenn saa yi mu ne ah dama war a raax de Diouf barki démb rek Diouf est ce que mun naa raax ma ne ko non ah dina taw de keroog bul raax de dafa toog ba guddi gi mu woo ma ne ma laaillah man de su ma raaxoon yàq sama ciment Diouf li nga wax suba si ba ngoon gi dafa taw xam nga fu maçon di laajtee dina taw loolu béykat lu mu war a def ah | 24.131 | wol_43012_114.971_139.102.wav | kallama/wol_43012_114.971_139.102.wav | |
mën na baax te mën na yàqu waaye nawet moom li ci gën li ci gën li may wax nawet rek | 5.171 | wol_43010_643.269_648.44.wav | kallama/wol_43010_643.269_648.44.wav | |
ñaareel bi mooy | 0.869 | wol_43012_329.504_330.373.wav | kallama/wol_43012_329.504_330.373.wav | |
tàngoor bi daal di ko laal mu comencé toq | 1.683 | wol_44111_267.698_269.381.wav | kallama/wol_44111_267.698_269.381.wav | |
nee naa la waa fi ma ko mos a déggee ñoom Diegane waa réseau ñoom | 3.776 | wol_36110_58.862_62.638.wav | kallama/wol_36110_58.862_62.638.wav | |
ci programme yi parce que ñoom ñoo ko fay mais toujours que da ngay fay | 3.707 | wol_44122_1358.161_1361.868.wav | kallama/wol_44122_1358.161_1361.868.wav | |
asalaamaaleykum | 1.074 | wol_43312_1279.077_1280.151.wav | kallama/wol_43312_1279.077_1280.151.wav | |
%e 495 %e 495 %e 57 92 | 10.114 | wol_4313_524.689_534.803.wav | kallama/wol_4313_524.689_534.803.wav | |
su booba | 0.659 | wol_43111_1260.606_1261.265.wav | kallama/wol_43111_1260.606_1261.265.wav | |
kon yàlla ñëw na ak xéwalam ren waroon nañu mun a am ñaari traite | 4.613 | wol_44411_813.122_817.735.wav | kallama/wol_44411_813.122_817.735.wav | |
balaa président di ko yëg | 0.959 | wol_44114_789.136_790.095.wav | kallama/wol_44114_789.136_790.095.wav | |
loo xam ni sunu diine dakoo gërëm | 1.592 | wol_44911_791.428_793.02.wav | kallama/wol_44911_791.428_793.02.wav | |
ndax rupture dafa am ci ci marché bi %e mais budul loolu moom wax dëgg yàlla %e jiwu toon nañu bu baax a baax xëy na tamit li ñu posé wu mooy %e qualité semence bi | 12.099 | wol_4313_635.653_647.752.wav | kallama/wol_4313_635.653_647.752.wav | |
borom xel la ñu woon | 0.78 | wol_44111_865.286_866.066.wav | kallama/wol_44111_865.286_866.066.wav | |
wax dëgg kooka ki ci bokk moom | 1.62 | wol_4312_51.781_53.401.wav | kallama/wol_4312_51.781_53.401.wav | |
macha allah | 0.82 | wol_4312_807.255_808.075.wav | kallama/wol_4312_807.255_808.075.wav | |
par rapport ak yeneen zones yi comme ay Fimela par exemeple foofu lu muy taw pa() %e bëri na ak ak yooyu donc %e zone yooyu moom 73 bi mooy benn variété bi moom la ñu fay gën a béy xam nga kon %e tànn variété bi moom kon ça dépend si %e pluviométrie bi | 20.139 | wol_42611_12.829_32.968.wav | kallama/wol_42611_12.829_32.968.wav | |
nit ki di ko dund ci jëfin ba def lu baax ñu weer la ci rajo bi nga %e nga dem ba sa rongañ di génn ndax am kersa ci loolu bëggoo woon ñu wax ko ndax ki ngay roy du loolu du ay fo looy dund la ba ci waxin et tout donc yal na yàlla guddal sa fan | 12.521 | wol_44412_2117.727_2130.248.wav | kallama/wol_44412_2117.727_2130.248.wav | |
%e ci turu coopérative bi nga xam ne mooy coopérative des jeunes producteurs agropastoraux de la région de Fatick | 4.888 | wol_44512_1424.643_1429.531.wav | kallama/wol_44512_1424.643_1429.531.wav | |
%e Mar ba tey rek mbokk yi ma fàttali yéen a ngi déglu RTS Tambacounda muy seen émission jokkalante tey nag kii di Mar Ndiaye di délégué régional si wàllum institut national bu pédologie moo fi ñëw di waxtaan ak yéen ak mbokki béykat yi %e Mar ba tey ci biir waxtaan wi béykat bi ci njëlbéen bi nan lay tànneefam ci suuf ci wàllu woowu nag nan la koy tànnee ba nga xam ne ne war na koo jëriñoo ci mbaa bu ko tànnee tamit nan lay xamee ne suuf si suuf su baax la | 33.227 | wol_44311_491.03_524.257.wav | kallama/wol_44311_491.03_524.257.wav | |
Nataal bii nag benn salle la bu ñu teg ay bã yu ruus def ay fleurs taal ay làmpu décoré ba mu rafet maasàllaa. | 10.597813 | 2575:1039.wav | waxal/2575:1039.wav |