wo
stringlengths
1
4.02k
fr
stringlengths
1
1.08k
source
stringclasses
2 values
Arme yi wóor nañu leen!
Les armes sont en place!
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Xamnaa kan mooy baay ji.
Je sais qui est le père.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Soo ko mënee, demal sa kër!
Si tu ne peux pas le supporter, rentre chez toi!
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Ñaari bieer rek.
Juste une bière.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Ci bëti kuréel gii, M. Wick baaxna.
Aux yeux de cette institution, M. Wick est bien.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Yaa ma musal ci sama bopp.
Tu m'as sauvé de moi-même.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Ndaw lu tiis ! Loolu ñu joxe ngir xaalisu këri telefon yi dañu mës a nekk lu way-lempo yi xalaat, def ko.
Triste ! Ces allocations pour charge de téléphonie ont toujours été ainsi conçues par la doctrine fiscale.
galsenai/french-wolof-translation
- Roger loolu, Kuper.
- Bien reçu, Cooper.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Teerewul, gis-gis bu bees amna njariñ ci wàllu shunfu.
Néanmoins, l'innovation a été couronnée de succès au niveau du shunfu.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Waaw kay, taxawal.
Ok, attends un peu.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Dinañu ci waxtaan ci kanam.
On en parlera plus tard.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Tay rek nga ko gis, naka ngay ko mëna laal?
Tu l'as vue aujourd'hui, comment peux-tu la toucher?
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Amaana sax dundu.
Peut-être même à vie.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Shane, lu baax la!
C'était bien, Shane!
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Bëgguma di yëg ni dama dof saa yu nekk.
Je ne veux pas me sentir comme un monstre tout le temps.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Bàyyi nga ma dem, nga daw dem aéroport ci nimu gëna gaawe, yaw ak haltère bii mëna yegg foofu.
Tu me laisses partir et tu cours à l'aéroport aussi vite que tu peux avec ce haltère.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
- Sama doom, waay!
- Je suis là.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Duggal nga...
Vous entrez et...
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Amoniak.
Ça fait de l'ammoniac.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Nu bëggoon defaral xale yi feetu noel, waaye musu nu mëna defal leen dara.
On voulait préparer une fête de Noël pour les enfants, mais on n'a jamais eu l'occasion de faire quoi que ce soit pour eux.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Te bu ñu gisee, dinañu bëgg, ndaxte ninkinànka yi, safara lañu, ñu soppi yàpp.
Et quand ils verront, ils désireront, car les dragons sont du feu fait chair.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Torture lu yomb la, ci kaw suuf.
La torture est facile, à un niveau superficiel.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Ci méngale, yenn melal yi (xoolal mujj ga ngir faramfàcce):
En comparaison, quelques illustrations (voir annexe pour détail):
galsenai/french-wolof-translation
Baal ma, paketu Gitanes.
Un paquet de Gitanes, s'il vous plaît.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Naka njiiteefu doxal gi, xaalis bi muy jël di ko dugal ci puukare, dina mujj metti ci askan wi ba jéggi dayo.
Quant au pouvoir exécutif, ses dépenses de prestige inutiles finiront par venir à bout des contribuables.
galsenai/french-wolof-translation
Danuy gaawantu lool, kilifa gi.
On est pressés, monsieur.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Baay, 7:30 la.
Papa, il est 19h30.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Du loolu rekk, bëgg nama.
Il m'aime aussi.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Looy wax ci réewi Afirig yi jox seen lépp Farãas te bàyyeeku bañ a jéem dara ?
Que dire des pays africains qui ont tout délégué à la Franceet se laissent aller facilement à l’indolence ?
galsenai/french-wolof-translation
Moone yeneen xeeti ay yi nga xam ne nguur gee koy def wala mu koy seetaan mooy cëslaay lu bon li.
Et pourtant les autres formes de violence dont l’État est souvent acteur et/ou spectateur en constituent le ciment cynique.
galsenai/french-wolof-translation
-Def naa ko?
- Je l'ai fait?
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Déedéet, mbir yooyu di xóoy.
Mais non, des petites choses qui brillent.
galsenai/french-wolof-translation
Kutta.
Je suis un homme de Dieu.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Kan la woon? !
Qui était-ce?
bilalfaye/english-wolof-french-translation
kër gu weex gi mingi xañ FBI.
La Maison Blanche est en train d'abuser du FBI.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Lépp loo xam ak loo bëgg, demna ba fàww.
Tout ce que tu aimes et connais, est parti pour toujours.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Dafay gliise.
Ça glisse.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Ci ndimbalu tabaxinam wu yaatu, nangoom ak bëgg nitam, la war a faj looolu dina ñu dimbali ñu taxawal wala ñu taxawalaat doxalin yi bànki xarala yi ba bëgg a jaay.
Grâce à son architecture ouverte, sa flexibilité et sa scalabilité, la solution permettra de déployer ou redéployer les fonctionnalités que souhaitent commercialiser la banque digitale.
galsenai/french-wolof-translation
(SANDMAN BI KIRSTY MCGEE DI JOO)
(Sandman par Kirsty McGee jouant)
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Amoon na ñatti wàll yu mag yuñ wara aar ci réew mi.
Il y avait trois zones principales de protection dans le pays.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Loolu moo gënoon nekk ci kanamu keneen.
Ça aurait dû être sur le visage de quelqu'un.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Dellu ginaaw.
Restez en arrière.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Maa ngi jéema xam lan laay def ayu-bis bii di ñëw.
J'essaie de trouver ce que je vais faire la semaine prochaine.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Ñi bokk ci seen waa kër ñëw nañu ci nun, yóbbaale dëkk yooyu.
Ceux qui sont parmi vous nous ont apporté ces territoires.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Loolu doxiinu góor gu mag la.
C'est une démarche de vieillard.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Du woon li ma bëggoon a wax, waaye...
Ce n'est pas exactement ce que je voulais dire, mais...
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Amuma jàmm ci beneen barab bi, amul lenn ludul yuuxu.
Je ne trouve pas de paix à l'autre endroit, rien que des plaintes.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
- Lu muy def?
- Il fait quoi?
bilalfaye/english-wolof-french-translation
- - Yal na Yàlla defal jàmm.
- Dieu vous bénisse.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Ndax amul kenn ci suuf kuy liggéey ngir dundee?
Personne ne travaille pour vivre?
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Aw, Murph...
Je suis désolé.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Duma musa baale sama bopp su ma leen jàppee.
Je ne me pardonnerai jamais de les emprisonner.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
SC bokk liggéey
le SC a travaillé ensemble
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Su amee luma dal, 007, fàww nga def dara.
Si quelque chose m'arrive, 007, j'ai besoin que vous fassiez quelque chose.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Ndax dama wara wàcci ci ile bii. Ngir saafara kàrt bi.
Je dois quitter cette île pour résoudre la carte.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Maa ngi jàpp ni daf ko laxasu, ci la ay flër wàcci ci asamaan wala lu mell nonu
Et je pense qu' il l' a vraiment embrassée et que des fleurs sont tombées du ciel ou quelque chose comme ça
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Yalla nga joxe firnde ci limu def lu jaaduwul wala nga noppi!
Soit vous prouvez son erreur, soit vous taisez!
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Dañu jàpp ni waa Russie moo ma yóbbu ci waa ji ci boppam.
La théorie est que le Russe m'a mené à l'homme lui-même.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Tolluwaayu weer bi dafay am ndaxte benn booru Venus (wala Weer bi) bi jàkkarloo ak Jànt bi rekk lanu leeral. Tolluwaayi Venus dafay biral njankatu Copernicus ci ni déele yi dañoo wër Jant bi.
Des phases se produisent parce que seul le côté de Vénus (ou de la Lune) qui fait face au Soleil est éclairé. Les phases de Vénus ont justifié la théorie de Copernic selon laquelle les planètes tournent autour du Soleil.
galsenai/french-wolof-translation
Ci kanam gi.
Dans le visage.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Delta 26, amnanu ay xaritoo ci zone kill bi yépp.
Delta 26, nous avons des amis partout dans la zone de mise à mort.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Dinaa ko tëye.
Je vais tenir ça.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Suura yooyu amul tur wu baax.
Ces journaux n'ont pas une bonne réputation.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Am nga 15 costo buñ saaf ak 30 saaku hamburger bu fukki kilo.
Vous avez 15 côtes grillées 30 sacs de hamburgers de 10 livres.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Genn-wàll lañu woon... genn-wàllu goor lañu woon, wala lu ëppu
Ils étaient à moitié... ils étaient à moitié singes, sinon plus.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Dañoo gis ne mbir mi ëppoon na ay loxo te li gënoon ci ñoom mooy ñu wàññi njëg yu seer yi.
Ils ont vu qu’ils étaient en danger et ils avaient intérêt à baisser les tarifs qui étaient excessifs.
galsenai/french-wolof-translation
Njëlbeen bu rafet, ca ñetteelu simili ba la Anderson teg Gones yi ci yoonu ndam li, ñaareelu bit ba Depaay moo ko dugal waaye waa Liyoŋ dañoo dellusiwaat ci ñaareelu xaaj bi te seen ndaanaan li ñu gaañ moom ñëwaatul.
Un début parfait, 3 minutes ont suffi pour permettre Anderson à mettre les Gones sur les rails de la victoire, un 2e but pour Depay pour aller au chaud mais les Lyonnais reviendront des vestiaires sans leur star touché.
galsenai/french-wolof-translation
Ba leegi mingi mer.
Toujours en colère.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Dañu gënoon, përëm bi dafay yuuxu.
Ils ont intérêt, les chefs crient.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Ginaaw loolu ma woo securite bi.
Je vais appeler la sécurité.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Yonent yu mag ya.
Les grands prophètes.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Man itam noonu la amee.
Je me sentais de la même façon.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Dafay naaw.
Ça vole.
galsenai/french-wolof-translation
Ak waa ji yor oto bu xonk bi gaaw?
Avec l'homme dans la voiture rouge et rapide?
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Ñépp a bañ Juif yi
Les Juifs étaient rejetés par toute la communauté.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Li mu nekk ku mën a samp ndëndam ngir jël Balu oor bi (Ballon d’or) rekk, def na ko ku matal nattukaay boobule.
Le seul fait qu’il soit un candidat crédible au Ballon d’or, le fait remplir ce critère.
galsenai/french-wolof-translation
- Hé.
- Je sais.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Moo tax ma nëbb ko àddina.
Alors je l'ai caché au monde.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
DAFA BËG DEEN SOUVENIRE.
Il aime garder des souvenirs.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Du noonu laay faral di defee mbir yi, waaye yenn saa yi danga wara bàyyi sa njàngalem def liy yoon.
Ce n'est pas ma façon habituelle de faire les choses, mais parfois, il faut abandonner ses principes et faire ce qui est juste.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Ay musiba yu ñuy teg.
Une malédiction qui nous incombe.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Lu tax duma la yóbbu hopitaal?
Je vous emmène à l'hôpital.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Dangeen ko war a daaj ci bant !
Vous devez le crucifier!
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Soo ma nangu, dinaa soppi sa nimero ngir kaaraange.
Avec votre permission, je vais changer votre numéro pour des raisons de sécurité.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
XAM NGA ÑAARI OTOO YU YÀLLA. GAAWAL.
Il faut deux putain de voitures, tu sais.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Kado la buy dem.
C'est un cadeau de départ.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Tukki ci tali!
Un voyage en voiture!
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Du sunug njàmbaar, sunub xam-xam wala sunu mën-mën moo nu ko may.
Du sunugnjàmbaar, sunub xam-xam walla sunumën-mën moo nu ko may.
galsenai/french-wolof-translation
Dama bëgga dellusi ci monastère bi sama xarit, prêtre bi nekk.
Je veux retourner au monastère où est mon ami, le prêtre.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Jaan ji ne ko:Wéet nañu tamit ci biir nit ñi.
On est seul aussi chez les hommes, dit le serpent.
galsenai/french-wolof-translation
Bis bimu demee ci tundu wi, neige dafay wàcci bu baax
Le jour où il va à la montagne, il neige en gros flocons.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
- Numu ko xamee Jung-hwa?
- Comment Jung-hwa le connaît?
bilalfaye/english-wolof-french-translation
- Baay?
- À papa?
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Eilidh Doyle tabboon nañu ko ci jiitekat yu atletisma bu Ekost niap njiitu bu nekkul eksekitiiw ci ndaje kurel bi ko ŋank buy am att bu nekk.
Quelqu’un d’autre a ajouté : « Une publicité si déconnectée. »
galsenai/french-wolof-translation
Kon ma gis ni ñu tëj Braga ci selil D3.
J'ai découvert que Braga est détenu dans le bloc D3.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Te lu bari ci dee yooyu, yaay yi dañu naan sàngara lu bari.
Et beaucoup de ces décès sont le résultat de l'abus d'alcool par les mères.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Nanga ko laaj...!
S'il vous plaît, demandez-lui de...
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Duma bëgg keneen ludul yaw.
Je ne tombe pour personne d'autre que toi.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Bés bu nek.
- Toujours. - Je sais.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
Bëgg nga àdduna bi gis ni yaay sama wuutu.
Tu veux que le monde sache que tu es mon successeur.
bilalfaye/english-wolof-french-translation
README.md exists but content is empty.
Downloads last month
28

Models trained or fine-tuned on galsenai/centralized_wolof_french_translation_data